Waññi Ko
|
Waññi ko , ëpp në :
Han , han , sa kattan bari na , sa bateau gaaw na , te saw fit rëy në
Han , han , sa kattan bari na , sa bateau gaaw na , te saw fit rëy në
Han , han , sa kattan bari na , sa bateau gaaw na , te saw fit rëy në
Refain : waññi ko , waññi ko , waññi ko ,
Waññi ko , waññi ko , ëpp në

Yaw yaa ni , ëpp óon nga , trois cent kilos ,
te bés bu ne , benn xar nga daan añ e
nga neeti , at mi fi Obama ñëw ée
yaw yaa ko gis , muy dox antu , biir Pikine
am oon na , gaïnde gu rëccé , parc hann
nga neeti ñu , yaw yaa ko jat , ba mu nelaw ,
nga ni ma , am oon nga , benn bateau , ca Guinée
te waa nations – unies , nga ka daan loué
te diggënté , États-Unis ak Guinée ,
daa woo ko daw , lu ëpp ñaar i fan
am na benn bés , nga ni ma , my boy
keroog daje naak , roi des arènes. 2 fois.
ben loxo , laa ko yékkëtée , ni ko félicitations. 2 fois.
ma tegaat ko ci suuf , ni ko , my boy. 2 fois
na nga jaar , sa ma kër , ma jox la yeneen clefs
na nga jaar , galle , ma jox la yeneen clefs
techniques yooyu , japon laa ko jànge
ca yooya jamono , man la ñépp di wër
lu ñu wax nga ni fekke nga ko
fu ñu wax nga ni dem nga fa
doo tiit doo raf , doo dellu ginnaaw ;
waaye sa ma waa jii , ken melut ni moom.
Wax oon naa fi ni adduna ken du ko dajal ,
Te ku dul umppëlé da ñu lay ragal.
Wax aat leen ni faw nit ku ne am lu muy des al
Ngir bu ëllëg ée ñu mën laa set al.
Xam lépp , mën lépp , loolu , yalla dong a ko jagoo. 2 fois.
ragal al yalla , waay , ragal al yalla
ragal al yalla , waa jii , ragal al yalla
ragal al yalla , waay , ragal al yalla
ragal al yalla , waa jii , ragal al yalla
Musixmatch.com; jh-radio.ru
Другие песни: